Sign up
Artist
Batch Gueye
About "BOULE FATTE"
Kharit gniou fatelicou liniou dane fowee baniouye gonee. Aduna ko mèredie ,dunuya ko mèreme,aduna ko mèredie dunuya ko mèreme. Aduna ko mèredie ,dunuya ko mèreme. Aduna ko mèredie,dunuya ko mèreme. Aduna ko mèredie , dunuya ko mèreme. Aduna ko mèredie ,dunuya ko mèreme. Wax diou borom tewoul bouko waxee dieuwla.wax diou borom tewoul bouko waxee dieuwla boude lou bakh dieuwla ,boude lou bone dieuwla.damay dox di khol yaye nioune yaye niniou mel.damay dox di lathiee nioune yaye niniou mel deukeul nitki foumou deukoul dafa niawe sounou bir! Aduna ko mèredie, dunuya ko mèreme.aduna ko mèredie,dunuya ko mèreme.aduna ko mèredie,dunuya ko mèreme .adunaaa ko mérimereee ,merimereee.banioude gone la niou yalla bolewone,legui magnane ndeyesane de yakouna guir wax diou nias,wax diou bone gui niouye wax mounouniouko deukee sounou bir dafa niaw,dego guaniou dane dego amatoul waxtane guaniou dane waxtane amatoul.dieuw bakhoul ni bayilene fouguene togue di toguee domou adama yi,adama dieuw bakhoul,mouno déme bayima mounou ma deme,mounou ma deme bayila yalla niou bole.mounou ma deme bayila mounoulo deme,mouno deme bayima yalla niou bole.bouniou kene bole kharitoo nikharito kharito bouniou kene meusa bole ndakh yow sama doumou ndaye gua kharito.baniouy gone laniou yalla bolewone balegui boumou yakou yow kharit !kharit sama domou ndaye gua! see less

About
Batch Gueye sings the traditional music of the Senegalese Baye Fall with a soulful voice, magically bringing the heart of West-Africa to you. Soulful West African Griot Music.  In November 2012 Batch's song M'Beugel has won the World Music Network's Battle of the Bands competition with a landslide public vote. After an EP and a debut album, Ndirarigne, Batch is now back with his m... more
Other Pages

Personal Website   Buy artist music   Facebook Page   Twitter Page   YouTube Page
Welcome to EthnoCloud
A platform for Ethnically and Culturally inspired music.
  • 80,000+ Global Followers
  • 4,529 Artists
  • 886 Industry Professionals
X